Текст песни
Te fes tok sa kaw mbir yaakaar, Télé fes sa xol taw sa xel yokk sa Naxaar. Wuté gnaq pexe ragal gnafe waaye lan. Mo dé sé nit su yémalé dundu ak dee. Wax len ma kan? Mo mëna taalát sondel bu Takk ba jéx takk. Waaye bu xadi muq kun faya kun rekk moy Sakk. Gëm gëm mëna wow waaye balaa kong, Yërg mëna Yalla dina ñaw wis. Mbir sa dé ci tu yaakaar gatt ko. Xomb mbir nga daa naané cain tagg ko. Ci bët, dem ci te fes bi tok yaakaar Logg se fit, muy foor di wax di bax Bey töf töfi. Yaw nga ni xam nga fan, Nga mëna dem ngir tékki. Daxe ji ngelew gi, jaamu ji keyit boobu ñuy Taal sa ginaaw ak ndaw tali yi. Yaw nga ni xam nga fan, nga wax dem Ngir tékki. Ci Te fes tok sa kaw mbir yaakaar, Télé fes sa xol taw sa xel yokk sa Naxaar. Tank pënd, gnaq di waxantu se jëg, Bom té yoon bi tammalé gul sax. Tax, nga dem ci maamën mu takkën le tool. Ludul be reggé gi yaw gisoo ko. Xalaato ni mir yi mëna le ëpp loxo. Ci te fes tok sa kaw mbir yaakaar jànog Moom. Waaye kan mo xam? Kuy daan moho mam.
SAMIRA — Outi
«Outi» — SAMIRA. Читайте текст песни и подпевайте с караоке-подсветкой: строки текста подсвечиваются в такт музыке. Слушайте онлайн бесплатно или скачайте mp3. Длительность записи — 3:18. Жанр — Этническая.
