Текст песни
Borom Beek mi dalal na xeli. Sa ay mbakkee settal na xooli. Te jingaa jumaa yi ñu julli. Mbakkee tuub lën ga yefur def ko julli. Seen Mountakha Bashiru, dundal te yakku fee. Ñaanal ñoo, yay mam ba mba. Al Mountakha Bashiru, dundal te yakku fee mbakkee. Ñaanal ñoo, yay mam ba mba. Al Mountakha, mbakkee Sartu nañu la. Al Mountakha, Bashiru Jërum nañu la. Seen Mountakha nee nañu, dina gëna gën, Dina gëna baax, ba a jënna. Seen Mountakha nee nañu, dina gëna gën, Dina gëna neex, ba a jënna. Beeri Mountakha, Boroom yër maa ndéla. Al Mountakha, yër maa ndekkee Séla. Bashiru Faatu Mboob Mbaam, boroom beek mi, Boroom reeji, mooy Seen Mountakha. Bashiru Faatu Mboob Mbaam, boroom beek mi, Boroom reeji, mooy Al Mountakha. Daaw bi jogee fi di jëm, a jënna, Ndarumi ndam lay dépare. Daaw bi jogee fi di jëm, a jënna, Ndarumi ndam lay dépare. Al Mountakha, Mbakkee sartu nañu la. Al Mountakha, Bashiru Jërum nañu la. Seen Mountakha nee nañu, dina gëna gën, Dina gëna baax, ba a jënna. Seen Mountakha nee nañu, dina gëna gën, Dina gëna neex, ba a jënna. Gëna gën, gëna baax, ba a jënna. Gëna baax, gëna neex, ba jënna. Gëna gën, gëna baax, ba a jënna. Gëna baax, gëna neex, ba a jënna. Nekki nekki lën jerëg, nekki lën jerëg. Dey gëna neex rek, di gëna baax. Di gëna xel bi gëna. Ba jënna rek nak. Cheikh Yay Cheikh Bashiru, Ki xam ni, kumma Sénégal waye aan taraar réew Bon aan ci. Xam nanu Mouhamadou Moustapha. Xam ndam yu Margarita Mboob Mbaas Bashiru. Sunu Fatou Mboob Mbaam, Jager Fakmo, Mboob Soraniang, Seen Mountakha Sorobe, Mboob Kordumbaalu Mboob Yosono Fatou jog yaay mu Mboob Mountakha mbakkee mis di jàcci Islam di. Baye woy ni Jager Fakmo, ni Aminata la, Ndax, ba dey mbakkat. Seen Mountakha Mboob Yosono jog mu joxum ngay na Fakmo.
Luka — Borom Mbeg MI
«Borom Mbeg MI» — Luka. Читайте текст песни и подпевайте с караоке-подсветкой: строки текста подсвечиваются в такт музыке. Слушайте онлайн бесплатно или скачайте mp3. Длительность записи — 3:42. Жанр — Фолк.
